Allocution de Cherif Mame Libasse Lahi lors de la nuit de prières dédiées à Seydina Issa Thiaw Lahi
--------
1:31:54
--------
1:31:54
Kaamil - Ñaanu Baye Seydi Thiaw Lahi
Seydinaa Isaa mu ndawXalifa noo ngi lay siyaar Yaa di "samsu fli zaamaan"Ub nga làmbu diiné ji.#layenedigital #layene #islam
--------
1:01:34
--------
1:01:34
Zikrullah - Ñaanu Maam Njoon ak Baay Aboo
Ñu baax ñii ku leen woy da ngay am ngërëmYonnen doomi yonnen Bilaay ñeey ngalamLimamook njaboot am da ñoo jàlla yiiYonnen daal dadul kem, xana ñooy ngalam#Layenedigital #layene #zikr
--------
1:23:39
--------
1:23:39
Zikrullah - Ñaanu Seydi Raan & Maam Ala
Jërëjëf Imaama Laahi yaa nu xamal yoon waDugël nu sañey Buur Yàlla miy sàmm jaamam baaSañey Yàlla miy Buur moodi wax "laa ilaaha illa LaahuKu kay salloo du feerook meram Buur baa#layenedigital #layene #islam #prieres #education #zikr⚠️ Cet épisode contient des chants religieux (Zikr) appartenant au patrimoine spirituel de la communauté Layène. Tous les contenus sont originaux, enregistrés par notre équipe, et utilisés à des fins non commerciales, éducatives et spirituelles.